Gno gagner gneup nek champion
Started from the bottom nek champion
Gno gagner gneup nek champion
Started from the bottom nek champion
Started from the bottom nek champion
Jangue beu maag lane momay téré m'a Tekki
Ndamli Da fa nekh Sama combat Bé meti
Noone bi mako raye fumy jaar ba Tekki
Start from the bottom Mangui fanano coupe bi
Sama jome foula mome la Jiteul tekk
Mane damala Niaf deff tekk
Mane damala Niaf deff tekk)
Yaye Boye mongui xaar fokma yoné mou fay boori
Yaye Boye mongui xaar fokma yoné mou fay boori)
Bagnal nooni ré la boul bagne nooni xole la
Yewu souba gnaffé xamni champion nga
Champion nga, champion nga
Sampal sa ndeudneu Bakou lgui champion nga
Da nga beuré daan gnibi lgui champion
Da nga jangue maag tekki lgui champion nga
Yooré jabar ak ki dôme lgui champion nga
Yobou papa yaye maaka leep champion nga
Champion nga, champion nga
Champion nga champion nga
Gno gagner gneup nek champion
Started from the bottom nek champion
Gno gagner gneup nek champion
Started from the bottom nek champion
Started from the bottom nek champion