Macké ko wax do Dèm Qatar
Kouy soule di souli weur di mystique
Jeul sa mbok defko lou sadik
Macké Ko wax do Dèm Qatar
Tepi taf xéw def Lougnou saf
Appo vent ni harmattan han rewandé apprenti car
Dîna topou cas melni wégne Thi kaka
Lougnou xam mou siw gno raw Fisha
Yoro passe di wax aye giga
Mille page you ndaw lou nekh nga wax gneup done al waha
Pouss nga wegne bassa pokk yi di xegn
Xar deux heures le mating
Yore djassi wegne nit gni rombeu la di Dèm
Han et puis tu dégaines agressé lén
Nangouwo ligueyi ndax gnémé lou Teng
May lathie ndax Li gni koy deff aye sénégalais lagne
Boye sénégalais deugg day gnémé lou Teng
Ba télè Taaké radio dañuné kamathie
Dossen morom delen doute di dougeul
He Gnoun bignou jakhlé yena gneuw yeugeul
Yeugeul geusseum or bi rakhoul pereum
Fo Mba nga lale ndiambane
Hey Ku meer mathial Dakaaar
Fo Mba nga lale ndiambane
Ba télè Taaké radio dañuné kamathie
Dossen morom delen doute di dougeul
He Gnoun bignou jakhlé yena gneuw yeugeul
Di Yeugeul geusseum or bi rakhoul pereum
Fo Mba nga lale ndiambane
Kep kufi signe pro faté say copin do Dèm katar
Koufi possé seins di trompé say copin do Dèm katar
Kepp Koufi teukeulé Wally ak Sidy Diop do Dèm katar
Almadie minuit nelao beu midi do Dèm katar
Dieunde lén télé tale took cetane
Sadio madio diko Tocc gnouy contane
Borom niari galons kouy Nangou sa ballons
Kouyaté fatal fatal hé bu none bi reuthie
Mani Nampalys Nampalys Nampalys Nampalys Nampalys
Ba télè Taaké radio dañuné kamathie
Dossen morom delen doute di dougeul
He Gnoun bignou jakhlé yena gneuw yeugeul
Yeugeul geusseum or bi rakhoul pereum
Fo Mba nga lale ndiambane
Hey Ku meer mathial Dakaaar
Fo Mba nga lale ndiambane
Ba télè Taaké radio dañuné kamathie
Dossen morom delen doute di dougeul
He Gnoun bignou jakhlé yena gneuw yeugeul
Yeugeul geusseum or bi rakhoul pereum
Sa baye di takalé di fay jangue
Nga neksi deuk bi di daw jangue
Kougne fi dekeuti xol ngassiy tek lasers mouy misère defko lodoul Nangou gnou koy defsa frère hé do Dèm katar
Amo moyenne jeul sa bulletin yobu Photoshop yokussi 1 wala 2 wala 3 wala 4 wala 5 wala 6 wala 7 wala 8