Alladji Ndene Mbayay bayam
Lambook pass passak manoute
Nguir doon te donnë maam ya
Do seddale di ndieukeu thierou
Dctr Lamine han Mbye Mbayooy Mbassou
Do seddale di ndieukeu thierou
Mbye Mbassou Babou koutobella
Ngi gua womat baniou yeksi
Fi gua len dieumey fa guën
Kou am vélo di la yobaale
Bou ame ndaamar nga doon bour
Bayou Yaramou Mouhamadou Moustapha
Do seddale di ndieukeu thierou
Ndey dji sekh mo waral lii
Laminoo yagga def Mbaakh thi li mou moom
Do seddale di ndieukeu thierou
Adjiaratou Khady Faye moy sa yaay
Cheikh Alioune Badara Faye moy sa maam
Borom Darray Bouchra thia guinaw Birkama
Min Makattali baytil akhsa
Bam ko idjite la naar ya sarkhole
Sa baay walliwou ba ne woon na thi doundam
Ken doula gueuneu kawe thi Adounyaa
Dieureudieufal naniou laa yaw Lamine HAN Mbye
Am gua gueureumeul waydiour thi ndeyak thi baay
TIDIDIT TIDIDIDIT TIDIT TII TEUDEUT TEUDEUT
TEUDEUDEU TATATADEU TADEUDEU DEUDAAAT
TADEUDEUT TADEUDEUT TADEUT TADEU DEUTAADA
Silmakhaaaa ! doy loo ndiathiar
Dem na daal ba delou si te yagoul yoon
Talibe tidjian maamam Affis la woon
Aladji Ndene Mbye moom moo fi def nian
Dara gua thia gueuneu kawe
Haveut univercyty nangou nagnie
Yaw kanguam guam thi medical
Dieureudieufal naniou laa yaw Lamine HAN Mbye
Sa mama djiagual magg nie niou yoot sen dom
TIDIDIT TIDIDIDIT TIDIT TII TEUDEUT TEUDEUT
TEUDEUDEU TATATADEU TADEUDEU DEUDAAAT
TADEUDEUT TADEUDEUT TADEUT TADEU DEUTAADA
Yaw sa baaye newoo na thi doundam
Haveut univercyty thia gua guenne
Dara dji fi gueuneu kawe thi Adouna tay