Nguala djiti rew yi thi cdouna bi
Nguir doundou gui diegue mingok
Nio gui ni di daw soubak ngoon
Menuisiers yaa ngui ni le
Waykats yi pirat na niou len
Sou la Yallah djitale lo waagni
Nguir dound gui diegue mingook
Handicapes yi sonë na niou
Sen ndiaguou ndiaboot de wooroul
Ye waay Samba deuguin ndat ndat
Ye waay Samba deuguin ndat ndat
Ye waay Samba deuguin ndat ndat
Tiey waay Sambaaa ho ho ho
Garmi tay dji new na lool
Beug thi solou nguir nawle yi lay khol
ck yanen yoo kham ni faw gua def ko
Tiey way Sambaaa ho ho ho ho.