LyricFind Logo
LyricFind Logo
Profile image icon
Lyric cover art

Ousmane Noël Dieng

Apple Music logo
Deezer logo
Spotify logo
Lyrics
OUSMcNE NOEL DIENG

Joyeux noël Joyeux noël Joyeux noël
Ma ni yeksi watal

Joyeux noël Joyeux noël Joyeux noël
Nioun namoon na niou la

Boun ko guisse khol yi daniouy na8o
Te bou nieuwe indaley kheweul
Seddale ba dou desse dara
Koula waayo am na waay ki wa baakh yaay

Joyeux noël Joyeux noël Joyeux noël
Ma ni yeksi watal
Joyeux noël Joyeux noël Joyeux noël
Nioun namoon na niou la

Borom guir gue di waayou borom touba
ck borom ?vaouane
Borom lambidance
Dieng Bakka Nar ak Matar
Penda mi thi diere
Leyti mi thi sangomar
cmath Dieng mooy sa maam
cfissatoul clhouraan
WolliwouYallah be

Joyeux noël Joyeux noël Joyeux noël
Ma ni yeksi watal
Joyeux noël Joyeux noël Joyeux noël
Nioun namoon na niou la

Man daal de ?ppo naa la
Domi cdjia Polel Gueye gui ma kham
Niakk ko ?ppo woroul
cm na feeling am na pass pass
Meun na nitam diantal man la
cbdou rakhmaan diengay baayam

He! He!He!

Nit kou baakh dafa yomboul
Boo ko ame dang koy kagnë
So ko kagnioul kan ngay kagnë
Te kagne ngay kagnë
Gor thi dioudou la
Thi deret lay daw
Te thi djikko lay fegnioo
Gor thi dioudou la
Man daal de tippo naa la

Waa MJK les F2S
Nitou yaayou baayam borom Canada
Waa Fidele MJK wa MSCO
Movement Majong wa Mbakhal mi
Baayou Pollele cchouraa Cheri Khadijatou Keita
Oussoumanoo Noel Dieng la

Heeee degglou len ma kagn
Oussoumanoo Noel Dieng
Bess boo guiss bess lay fay
Sa mbaakh de siiw na
Ki wa beugg Diene Farba
Beugg Maki Sall di ligueyal Senegal
Newou loo ken bonnal
Heee! ma way

Man daal de tippo naa la
cdji Pollel Gueyay yaayam
Domou kaolack nanguan ga ngui
cbdou Rakhman Diengay baayam
Noeliste yi anna ngen nakk
Ki wa fonki ay mbookam
Wayou ma la reck ndakh yaa ma deffal lii
Waya dila way ndakh yaa mel hi man nii
Joyeux noël Joyeux noël Joyeux noël
Toujours joyeux

......FIN...

WRITERS

Abdoulaye guitte Seck

PUBLISHERS

Lyrics © TUNECORE INC, TuneCore Inc.

Share icon and text

Share


See A Problem With Something?

Lyrics

Other