Douniou Meuneu Deggo Fils.
Sho Bi Neima Send Tofs Please.
Many Millions Many Dollars Yo My Nigga Guinto Fils.
Sa Life Leu Yako Meuneu Hustle.
Tei Money Kessei Momay Deufeul. Eey Eey.
Ndax Makk Bou Dickei Lep Feuneukh.
Hei Bayil Xel. Man La Mister Calibreiix.
Hei Bayil Xel. Par Force Dangamay Valider.
Gueinei Samay 4 barres Ni Tik Tokleine.
Binga Koy Hustle Boy Guisso Keineu.
Dadjeik Ngak Sa Papa Eeh Mbipp do Dem.
Bizart cbalma Meu Pistolet.
Nigga Danga Meuneu Rap I Know.
Dama Wara Beuri Cash I Know.
Fuck These Bitches I Know.