Nioune moussouleu Tar baniou wané guinawe fi...
Ndax yagna téwoule niou neik si nathi bi...
Goudék beuthieuk papa niongui si war wi...
Kne jambarla jambarla mayeko courage fils...
Guerrier la yagna ne Fight...
Wéte na si yone bi ak tarrayou life bi...
Ragaloule combat ba dayif...
cdouna warko mai moussouleu bayi fi...
Tare nathi mome, téwoule mou diap né moukou me mome fokou mou ame...
Xalé bou gore ak xalé bou jigéne bi nieupe né fokou niou ame...
cdouna yeup, kou néka nga xol nossi guéné té fok niou ame...