LyricFind Logo
LyricFind Logo
Profile image icon
Lyric cover art

Dama Lay Nakh

+1 Others

Apple Music logo
Deezer logo
Spotify logo
Lyrics
Boumala né boumala guissoul baby girl douma nélaaw
Dama lay naakh
Boumala né yameu geuneul leep li nè ci adouna
Dama lay naakh
Boumala né boumala guissoul mane douma am appétit no
Dama lay naakh
Yèneen guel yi yeungeulougnou ma ak lougnou mouneti moll
Yeah dama laakh naakh
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jigéen djouko meuneu change
Kone dièmeu change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

Doumala naakh mane
Douma fokaat
Meune naleu yèggeul ni rotkaat
Soumala nèwone nala dieundeul adouna bi
Khamèl bou baakh waakhou doorkaat
Dama lay naakh mane
Si parc bi nguèy doukhantou ak mane
Sa khol la beuggeu dousa taate mane
Wètali sa loss thiakou diamond
Nènagn assamane si moy limite bi mais fougnou nara dieum
Fofo nek ci kaaw
Jokh ma lokho ma fèy wèrr akk étoile yi ci kaw
Dama lay naakh

Plage, shopping, resto
Life faam like echo
Dama ko kepp si ettau
Nguir lekk lepp la mou yorone mané
Kou beugg dou naakhè
Real love ain’t no money
Baby girl soma nakhé ma dileu nakh
Sougnouy doom yi fougnouy moudjiie
Dafa diap nè mi ngui mèy naakh
Fèèk na bobou dèh mangui koy naakh
Sister ma dileuko thiaakh
Goorou tèy watiatiatiatiatiatia-aanh

Boumala né boumala guissoul baby girl douma nélaaw
Dama lay naakh
Boumala né yameu geuneul leep li nè ci adouna
Dama lay naakh
Boumala né boumala guissoul mane douma am appétit no
Dama lay naakh
Yèneen guel yi yeungeulougnou ma ak lougnou mouneti moll
Yeah dama laakh naakh
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jigéen djouko meuneu change
Kone dièmeu change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

Tourouma leundeum ndakh yow da ngua leer
Jokhè sama khol ndakhtè parèna dè
We trash mais mbaalitou cana aka chère
Boul khatim
Boul liguèy
Ma reudeul leu chèque
Kaay ma taak leu taak leu
Sa visa dèy gaaw kham ngua cana la
Xew xew bou reuy
Yow ngua diaralma djakaa ba galè ma bache ko
Dou dara nak

Kharouma dara loudoul taak la baby girl
Kone geum ma bokk
Dougeul sa nidiaye djakaa ba jokhè feu big money
Pour sa dot
Guiss na façon bou nek
Mais yow yameu diaral lou nek
Nuit de noces la yakamti
mane ak yaw yaramou nène
Problème bi moy que façon waakh bi
Waakh nako fi si niata morom
Bobou ba lègui sama baby mama la fi guissoul
Talouma love

Boumala né boumala guissoul baby girl douma nélaaw
Dama lay naakh
Boumala né yameu geuneul leep li nè ci adouna
Dama lay naakh
Boumala né boumala guissoul mane douma am appétit no
Dama lay naakh
Yèneen guel yi yeungeulougnou ma ak lougnou mouneti moll
Yeah dama laakh naakh
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jigéen djouko meuneu change
Kone dièmeu change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

Tu vois Aya ma chérie même tes tontons ces des menteurs (dagnou lay naakh)
Ils mentent, ils trichent, ils t'évitent
Pourtant ils ont tous un grand coeur (yeah dagnou lay naakh)
T’es tellement belle ma princesse tu devras être à la hauteur (ba dougnou lay naakh)
Penses à baisser la tête et à jeter un oeil sur ta soeur
Bébé, ils seront prêts à tout
Faut pas te fier à nous
Ils seront prêts à jurer
Mais tant qu’il t’as pas présenté sa mère, pas présenté son père
C’est pas fait pour durer (yeah dagnou lay naakh)

Boumala nè boumala guissoul baby girl douma nèlaaw (nèkoul aay nakh)
Boumala nè yameu geuneul leep li nè ci adouna (dedette dou aay naakh)
Boumala nè boumla guissoul mane douma am appètit no (tè nèkoul aay naakh)
Yènen guel yi yeungeul lougnou ma ak lougnou meuneti moll (dedette dou aay nakh)
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jigéen djiko meuneu change
Tè jott nguama change baby girl
Boumala waakhè beugoumala mane dama lay naakh
Douma dara loudoul nittou neen
Tek ci ma nek goorr
Nènagnou la nè goorr yeupeu yèm
Mais kou nek ci gnoom
Amna jigéen djiko meuneu change
Kone dièmeu change baby girl
Boko dèfè yeah girl dotou mala naakh

PUBLISHERS

Lyrics © Sentric Music

Share icon and text

Share


See A Problem With Something?

Lyrics

Other

LyricIQ Analysis

Top Emotion

Enjoyment

Sentiment
Thumbsup Icon
Theme

None