Nianalma ma gueuneu am ay none ma
They don't even know they made a strong man
Music dou xetou job bouma meune sonal
Sama tour da def si bop yi trauma
Dina fay malene gueuneu ligey
Manela gaal gui di top and you know
Leundeum bi da dik fénial bidew
Kou jouk ni may king bi th dou kene si niom
Somay xol rek di guiss you don't a caption
Cab comme luis suarez dou rater occasion
Gueuneu dope easy E ci digou compton
Melodie youy dess si sa xel sam communication
Bidi nieuway le projet de ma vie
Kone fallait may goudé studio
Seni beut yinguene ma tek douma titeul
Cab nit dong leu dou machine
Yay naa gnibissi ak louma goudé
Mane sa niani rek lay sakou ni
Dou done souba massamak today
Im on da way to the top homie
Nianalma ma gueuneu am ay none ma
They don't even know they made a strong man
Music dou xetou job bouma meune sonal
Sama tour da def si bop yi trauma
Dina fay malene gueuneu ligey
Manela gaal gui di top and you know
Leundeum bi da dik fénial bidew
Kou jouk ni may king bi th dou kene si niom
Yay naa gnibissi ak louma goudé
Mane sa niani rek lay sakou ni
Dou done souba massamak today
Im on da way to the top homie