LyricFind Logo
LyricFind Logo
Profile image icon
Lyric cover art

Mak Yow

Apple Music logo
Deezer logo
Spotify logo
Lyrics
Mane bama rere yama wane sama yonou khol

Mate gama niente nala nianesi nienti yone

Nah Manak yow si bene pakh bi lagn niouy soule

Mane dama nekk sassouma neker ak yow

Fanane sa wet chaque goudi Kheuy Ndeke sa love

Nah manak yow si bene pakh bi lagn niouy soule


Nenegn kou nelaw dagay faté lepp may nelaw dila geuneu nameu

Taroul Baga craquer deme nakh selaw biga Meusseu andal

Yaye niane bou nangou Gom you fadiou peace of mind yea

Houlo moy tah dioubo di neh Nagn rayanté sougn bir

Bou janteu teuder Man ak yow la Kenen nekouffi

Nah yamay gagne te malay fadj yow kay niou guissé

Yenesay niu doundou aldiana yenesay niou misere

Fo deuk ma deuk fa fo Deuk fofa nekh (saay)

Douma feké sa nakar Rangogne fompat Lene

Fess samay beut keuf sama Khole

Yeurmandéy mbeuguel te amgako

Hamna sa nieuk louner diar gako

Man malay balou te yama togne yeaa



Mane bama rere yama wane sama yonou khol

Mate gama niente nala nianesi nienti yone

Nah Manak yow si bene pakh bi lagn niouy soule

Mane dama nekk sassouma neker ak yow

Fanane sa wet chaque goudi Kheuy Ndeke sa love

Nah manak yow si bene pakh bi lagn niouy soule

Geudj ga degg samay namenala da fekk mala raaw

fama tolou si yow sorina lolou pencum khol beu yafané

kene geunoula si sama ay adio louma sohla ya thia meune

soumala buur weurseugeuley doom Yalnaniou Diar si yow

manak yow contre vents et marrées

mak yow comme mackek marieme

opposant yi kass boulene deglou kaay nala dieul dougal si palais

tank ak tank fo deme ma dem

Ayee kima dadiel mo mata kham way


Mane bama rere yama wane sama yonou khol

Mate gama niente nala nianesi nienti yone

Nah Manak yow si bene pakh bi lagn niouy soule

Mane dama nekk sassouma neker ak yow

Fanane sa wet chaque goudi Kheuy Ndeke sa love

Nah manak yow si bene pakh bi lagn niouy soule

WRITERS

Saliou Massamba Samb, Imam Abdoul Khadre Mbacke Diop

PUBLISHERS

Lyrics © Sentric Music

Share icon and text

Share


See A Problem With Something?

Lyrics

Other