Sangou dou doy so niampé dou doy so sagnon dag sa yaram
Mais lolou sah dou doy nakhté dou fompou gathia bi takk sa kanam
Sa doundou lagn yak legui deme Ga ba gor yeup ga diepi te bagne
Boul mere sa bopp nah yow defo dara sa tort moy ga nek djiguene
Loy khoulee bamou dale la ga ragala degg motah batay ni kene yeugouko
Lane ga solone lane la nara ladj lane lay def negou goor
Hana dagn takone say lokho yow ana lane motah ba jengouwoo
Yow mi lagn violer te yow lagnouy questionner melni ya def lou bone
Dem police am dete est ce que niom dinegn la geum moy dokh si sa brain
Gay Khol si sa setou rangogn yi fess sa beut Sa khol bi dey diekh
Gnila geuneu dieguer warla meuneu aar nioniou nak niolafiy saakou
Sen deret yi sorantewoule mou tour sa deret xarou done nafi diadou
But you strong strong enough but sometimes you just wanna die
Meme bouma Yalla wanon sa keur safara meunoul tah bama bale la ak
Sa rakou papa warla def dome dile teude ni tiaga Ga
Guenel la paka dass nela so dofer bam guene sa guemign nala fate
Bamouy khew compoula yagui ladj sa bopp tonton mom loumouy def ni
Innoncente dagnla complot meme bo nangouwone dagnla tekk deal
Loy geuneu di magg moulay geuneu ler né nekoul sakh beneu yone lako def
Ladioulwon sah gakoy wakhi sa yaye hana setlou wone nako key
Hayneu mou khamon ko nopi (waw) hayneu da ragalon mbok yi tass
Hayneu seuyeum ladon ragal mou tass ba takh yobouwma hospis
Niata viol lagniy deug sen tank soutoural niou mala yi geuneu
Niata djiguen legn fi Sacrifier nah haliss legui nopi la alale di dieun
Legui jankk ga tolou ga si seuye wayer meunoulo yagg ak kene
Nah niemeto goor boula dieguer ga teup daw ni kouniouy wadia raye
Niousi khamoul sa diar diar ham liga doundou diap ni yaka tey
Fek domeram bou free di dokhi ay sokhlam Mom mola yakaté
Khalate ga kharou ay yoni yoni mais Hamgani lolou dou solution
Yagui wete si sa yone di dokh yow rek yow kessek sey gomi khole
Dé sah mo geunona noy si yow liga nane ni non sombiwoko
Deuker tok di dioy batay nopiwo