( Néxal na nga nane ma bayi ngama )
( Beugo comprendre mounouma si dara )
( Sama statut boul xol Boloké ma )
Bamay dioudou anduniou wone démal
Man bamay dioudou anduniou wone démal
( Sama statut boul xol Boloké ma ) wawaw
Sama statut boul xol Boloké ma ( Démal )
( Xarit yomboul té yaw Daga faux démal )
( Xarit yomboul té yaw Daga faux démal )
Bamay dioudou andou ñu va t’en ( va t’en )
( Sama statut boul xol Boloké ma )
Lép lou negatifs guéné ko si sa vie
Képeu koulay yakal nala dial né
( Ndakh danio sokhor danio faux wallah ! )
( Négatif ték si oser wallah ! )
( Néxal na nga nane ma bayi ngama )
( Beugo comprendre mounouma si dara )
( Sama statut boul xol Boloké ma )
Bamay dioudou anduniou wone démal
Man bamay dioudou anduniou wone démal
( Sama statut boul xol Boloké ma ) wawaw
Sama statut boul xol Boloké ma ( Wawaw )
( Xarit yomboul té yaw Daga faux démal )
( Xarit yomboul té yaw Daga faux démal )