Kouma gueune beugg sama bopp
Beugg nala beu gueune la beugg sama bopp
Dieul la teg la fouma meussoul teg sama bopp
Xol thi kaw Xel khool leu kaaw leu thi sama xol

Beu ngeu fok ni yako moomé
Beula ngay nand fekk mou wess
Yangui tok thi garabou fitna
Euleuk togg thi kerr dinala diaffé
J'ai toujours été le même
Toujours là face à tes problèmes
Toujours présent pour ceux que j'aime
Toujours là quand t'avais besoin
Gnou tekk la doff mba kou manqué