LyricFind Logo
LyricFind Logo
Profile image icon
Lyric cover art

Lima Done

Apple Music logo
Deezer logo
Spotify logo
Lyrics
Sama gang douniou fowei toys
Dama magg nékatouma boy
All them pussy niggas making noise
Damay spend a hunnid for the joy
Beuri probleme mais doumako dioye
Soume leu shooter khamal yama togne
Dama beuri ay none sama kogne
Danio mounoul nangou lima done
Hit the bitch in the back of the bach
Samay mbok nio beugue ma dei
I'm a star it ain't hard to tell
leave the party i gotta get laid
Pull up on me i do not do date
I'm a player with a good grade
Huhh rawé naleine ay decades
Damelay rendi té douma use blade ( yeah bitch )
Baby boy mane dama wéradi
Kouffi fébar mane yorna sa remedy
Damay mandi té douma nane hennessy
Douma rap damay diokhé ay mélodie
Beuri guel comme JF Kennedy
Motax ma beuri ay ennemi
Douma bok lale bitch dama tereudi
Samay ennemi yeup sokhla thérapie
Sama gang douniou fowei toys
Dama magg nékatouma boy
All them pussy niggas making noise
Damay spend a hunnid for the joy
Beuri probleme mais doumako dioye
Soume leu shooter khamal yama togne
Dama beuri ay none sama kogne
Danio mounoul nangou lima done
Danio mounoul nangou lima ( lima done )
Damay daw ak high speed ( speed )
Dama lay bay nga ride the bitch ( bitch )
Boy I'm getting tired of this ( you get it )
I got cash ( got it )
But dama koy stack (yeah )
Ass dama koy spank
kholal
Boy yi mounou niou ma bagne
kholal
Sa bitch mane makoy bang
Souma parei diokh sama gang
Souy balais mome la leine deff
Dama parei douma kouy perte
Deime kharé eundi ay bag
Douma guiss my cat sunday
Hit the bad bitch on a tuesday (yeah)
Close friends moussouma ko get ( moussouma ko get )
Sama gang douniou fowei toys
Dama magg nékatouma boy
All them pussy niggas making noise
Damay spend a hunnid for the joy
Beuri probleme mais doumako dioye
Soume leu shooter khamal yama togne
Dama beuri ay none sama kogne
Danio mounoul nangou lima done
Yeah huh kholal everything coming in my way
Yeah kholal boy i'm reaching the stars
Yeah kholal boy yi daniouy cap
Yeah kholal yeah daniouy cap

WRITERS

Asse Mane

PUBLISHERS

Lyrics © O/B/O DistroKid

Share icon and text

Share


See A Problem With Something?

Lyrics

Other

LyricIQ Analysis

Top Emotion

Enjoyment

Sentiment
Thumbsup Icon
Theme

Race and ethnicity