Daño dëkke yakk sa xol bi
Ba ñemetulo dundu mbëgeloo
Goor ñi ni ñu bare lañu wute
Wax na fi nga ma tolu nga dumoyoo
Man duma ñom te ñom duñu man
Man duma ñom te ñom duñu man
Man damala bëg ba gëmewumala man
Man damala bëg ba gëmewumala man mi
Man damala bëg ba gëmewumala man
Man damala bëg ba gëmewumala man mi
Man dama xam sa njëk té duma waxale
Sa jikko doyma tax ma bëg la
Te dara duko dindi ma dulcinée
Ba ñemetulo dundu mbëgeloo
Goor ñi ni ñu bare lañu wute
Wax na fi nga ma tolu nga dumoyoo
Man duma ñom te ñom duñu man
Man duma ñom te ñom duñu man
Man damala bëg ba gëmewumala man
Man damala bëg ba gëmewumala man mi
Man damala bëg ba gëmewumala man
Man damala bëg ba gëmewumala man mi