Boo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi

Brodah mbegté nga dji sunu noon yi
Garap binioudoon feekhloo nga gor fils
Ana promessou toudeunté dom yi
Pourtant yaa waroon fadj sama goom yi
Doumla fen diarouko coz you know me xamoon ngani meuno dem douma lonely
Hésiter woo pour dieunder meu osh bi
Koudoul teew si sa levée de corps bi fuck
Pour ma wake up fauk nga let meu down down mane nga nopp deggomeu nakh maagui sound
Avant ligne d'arrivée bi nga daw daw daw teh niokodoon dokhal dès le départ
Démessi khel Ngani bopp sa bopp leu
Niou and ma daanou nga romb meu
Sama rangogn meussoul tokh sa nopp
Niaata yoon ngama wane guinaaw ma toppu leu
Nakh gaawouma baayi teh thiow douma taawi dou djigueen dou life dou money
Moomay tékheuleek gars yi mais respect ak loyalty bouy niak faut que ma khaadi
Risquer sunu life siguil sunu yaay loolou lagn diguéwoon homie
Teh nioog si batay manak yenen gars yima nguimb sen mbeur bi na daani
Boo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Boo diapéni xamgama rek sigmay oumpeulé homie
Waayé booma diappè ni sa bop rek better you know me
Teh balaa ngay xam nitteu leundeum niou leeral la xol bi
Waroon nga rouss dem di boolé sa tour si kaw son bougnma clash teh nga waroon ma sant
Doumla woowé noudoul ni nga toudou teh dou nignla toudé brodah diam moola dap
Khadj moola gueun parce que digko yaatal mais dou meusseu setaan mbokam nieuw dila matt
Doo yallah kone Boumla calculer woul baama compter si iow téwoul lepp dina matt
Gnima manquer teh warma motali
Sama guel sama b*tch sama honey
Sama real sama G sama famille
Bougnko tegoon si yoon tay ma taali
Dou doonati maak iow fii Waaneté
Li wess dou téh nga lekk bou agn di neekh
Nakh dokh nagn di goudé di naadié
Iow yaa beugoulwoon tok ba khaar mou neekh