Sant yallah maagui sant sama yaay, santaat sama yaay santaat sama yaay, Sant sama Baye mima tanal yaay
Sant sama gars yima yagg gueum diap teuweu baayi
Gnima diota baayi neleen legui dama yor
Souma djiteuloon am am sama ngor dieex
Beut dereetako lal waayé rangogn lay guén
Guémegn gouy nathi modoul meusseu wakh diam
Sama baamélou biir mougn laako tabakhé
Sangoo sama doolè bess dina takk
Koussi khel niaar nama seekhlou melni thiatt
Sama niakh guéneu lou sett diap si lima am sama werseuk bi ma dakh
Yaay xamnaani ken douma beug ni iow
Ken douma nieme wakh deug ni iow
Par ce que iow yaay yaama taawloo fekké
Bank sama oom seug beuss khol
Keurgou makk dafa khatt lool
Ligueey ba kerr dama dokhé nadj
Bay kaata xam nima dooyé waar
Amouma xaliss ni doomou steve jobs yi waayé ni nioom maagui foowé mac
Fess lama deff fi nga diokhé taat
Sen carrière yi soutoul Mota et Ma
Amoulo xam xam pour juger meu woona si barre bi ay témoins de Jehovah
Deg naa percer nga waanté si nop la yem Parce que tangoo fi louma meun diaroo
Buzzou semaine doyoul pour dima tendance ba Leuz sa G yi dougn todj sa diwaan
Rap beema yiiteel sinon guélou Niska sax meun naako kepp souma nekoon charo
Am nga ay arriérés may lekk avance millions laay peser sam nieugou balance
Diang ay att di kheuy di gontou
Faayekou weer no gondiwmeu woon
Ba bess may wakhtou di melni dof
Rap beema keuf boy si ay seconde
Question de temps la teekey réponse
Eup ay tournés aiguilles si montre
Boukhanteel may beumeukh sa monde
Dina teuyé rap galsen samay lokho
Pique meu je roule une pèle à ta goe
Fitt neu dou dieex à la vie à la mort
Bandit bou khess nioo diw Pablo
Negger Todioumeu neen sons yi todj plateau
Soul leu si souf yeek fanaan si kaw
Tidji balcon Khaar sa rouh bi romb
Moogui sen biir Zeus khadioul si nioom
Rap lou wow kong teh doo guiss fouma wéré
Doo bindeu ligne fimalay keppé
Dikeuloon nama ma taal ay doublé
Pourtant Sama but mooy encaisser
Ken yeugoulwoon sama anxiété
Rap galsen douma inquiéter
Job ba dog takhoul ma doon workat
Limay tek thiouné maneessouko comprendre
Diamono bi moo dokhoul ba sen son daw
Fouma guénéwer kenen dou nieuw comme thiaat
Rap koussi xamoul dara moo xam
Koussi xam dara douné xamoul maay kane
Nikou guiss mbaakh sa taat yi laay khonkhal
Kou lek sama avance arrière combat
Douma débutant mais finisseur
Goudou baat sama wakh gatt kilifeu
Maafi khar niaar diviseur
Ay laay def si je perdais R
Xawma sen soubeu waayé tay nguen dee
Legui Boy bouma clash ma tégueul ndeyam