LyricFind Logo
LyricFind Logo
Profile image icon
Lyric cover art

Safe and Sound

•

2020

FI FE LEE

Apple Music logo
Deezer logo
Spotify logo
Lyrics
Xam na fii ma jogee
Xam na fii ma jëm
Fii la lépp doore
Fii la nu jëm

Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fan

Samay maam no woote
Maam b6oy mooma woo
Fii lay roote, teen bi fii la

Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fan
Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fan

Fee la juddoo
Fii la joge
Fepp lay dund
Fepp laa magge
Fee la juddoo
Fii la joge
Fepp lay dund
Fepp laa magge
Fee la juddoo
Fii la joge
Fepp lay dund
Fepp laa magge
Fee la juddoo
Fii la joge
Fepp lay dund
Fepp laa magge

Dellu kër maam
Fa lanuy fanaan
Ku fi marr naan
Dellu ci ndaa li taataan
Da no bëgg am
Laada xam xam
Amatunu jàmm de
What a barn barn
(Barn barn what a barn barn)
Da no bëgg ndam
Xam sunu coosaan
Ndar geej ba Wakaam
Coumba castel Coumba Bang
Joal ba Carabane
Grand ndakaar Colobane
Janxalaar Colobane
Nëwal do fi gàn
Aduna bi la nu dëkk
Fun dem daaj fa banc
Aduna bi la nu dëkk
Fu ne la am banc

Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fan

Fëlee fii fii fëlee
fëlee fii fii fëlee
fëlee fan

Fëlee fii fii fëlee
fëlee fii fii fëlee
fëlee fan

Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fii fii fëlee
Fëlee fan

WRITERS

ABDOU FATHA SECK, MAMADOU LAMINE SECK, AWA LY

PUBLISHERS

Lyrics © RISING BIRD MUSIC

Share icon and text

Share


See A Problem With Something?

Lyrics

Other

More From This Album

Lyric cover art

Safe and Sound

2020

01

AHEAD

Awa Ly

02

CLOSE YOUR EYES

Awa Ly

03

GO YOUR WAY

Awa Ly

04

MESMERISING

Awa Ly

05

What Goes Around

Awa Ly, Delgrès

06

INSIDE

Awa Ly

07

NOW OR NEVER

Awa Ly

08

COME AWAY WITH ME

Awa Ly

09

TELL ME

Awa Ly

10

TO KNOW

Awa Ly

11

Are You Satisfied ?

Awa Ly

12

Tightrope Dreams

Awa Ly

13

FI FE LEE

Awa Ly, DAARA J FAMILY

14

WHY

Awa Ly

15

Ici-Haut

Awa Ly

16

MESMERISING J SILK REMIX

Awa Ly

17

GO YOUR WAY

Awa Ly

18

COME AWAY WITH ME

Awa Ly

LyricIQ Analysis

Top Emotion

Enjoyment

Sentiment
Thumbsup IconThumbsdown Icon
Theme

Gender identity and Sexual Orientation