LyricFind Logo
LyricFind Logo
Profile image icon
Lyric cover art

Imagine

•

2018

AK YOW

Apple Music logo
Deezer logo
Spotify logo
Lyrics
Sans yaw, dafay melni àdduna day bëg tukki
Ak yaw, damay melni ku tëye alalu bukki
Dëgg la sama chérie kon tay jii maa la tooñ
Wante yaa ma xamal tay jii luma xamulwoon
Maa ngi fataliku bi ñuy toog ci boppu koñ
Suñuy gént ag sunuy yeene rek lañu amoon
Waye seytane dafay faral di jaxase di ñu féewale
Seytane bëgul ñaar ñu bëgante, bëgul ñuy fo di ree.

Ndax yaw laa love
Baby yow laa bëg sama life
Baby bu dul yaw man dinaa die
Baby jàpp naa dootuma bayyi
(2x)

Sans yow, dara dootul neex, man lepp daf may sàppi
Ag yaw, damay bëg ba fumala séen di lappi-laapi
Chéri man ag yaw du hasard
gëm naa ni boo pareegul man damay toog di la xaar
Chéri man ag yaw dafa tar
looló waral man ma gëm ne lepp lepp dina baax
Ndax yaw laa love
Baby yaw laa bëg sama life
Baby bu dul yaw man dinaa die
Baby japp na dootuma bayyi

Waye seytane dafay faral di jaxase di ñu féewale
Seytané bëgul ñaar ñu bëgante, bëgul ñuy fo di ree

Baby all my love is for you, I go sing it
Bul xool ci benn seytane bul deglu benn wicked
ma ñàkk sama bakkan fuma toog dinaa la siggil
Bimala xamee ba leegi bëggatuma keneen
Chérie coco banne dama jooy, man dama fada
Bëg naa doon papa, ma def la mada
Sama xol bi moo la fal te jox na la benn mandat
à vie te nee na loo bëg dina ci ànd
Mais yenn saa yi bumala tooñee
sama chérie nang ma baal
te baña topp waxu noon yi daf ñuy gaañ

Ndax yaw laa love
Baby yaw laa bëg sama life
Baby bu dul yaw man dinaa die
Baby japp na dootuma bayyi

WRITERS

Boris ARNOUX, Damien COUTROT, Fabien GIROUD, Isere FARGES, Jean paul SY, Martin BISSON, Mathieu DASSIEU, Nicolas DUSSERE, Thierry RENAULT, Thomas SOUIL, Valentin ANDRY

PUBLISHERS

Lyrics © ESSEMBE PUBLISHING

Share icon and text

Share


See A Problem With Something?

Lyrics

Other

More From This Album

Lyric cover art

Imagine

2018

01

LAISSEZ NOUS

Natty Jean

02

FALLING

Natty Jean

03

ON M A DIT

Natty Jean

04

SENEGAL

Natty Jean

05

LOU TEUGUE TASS

Natty Jean

06

TAYA

Natty Jean

07

AK YOW

Natty Jean

08

SALIMATA

Natty Jean

09

IMAGINE

Natty Jean

10

PREZIDENT

Natty Jean

11

EGO TRIP

Natty Jean

12

ADOUNA

Natty Jean

13

ALLAH

Natty Jean

14

Echosysdub (feat. Natty Jean & Ondubground)

Danakil, Natty Jean, Ondubground

From This Artist