Liberté amul price ow yeh
Suñu maam la Babylon jappon nòot
Ba leggi Africa muja tog ni tekk
Nòotel bi di wal ba ci sët sëtaat
Ñu topp sen ginaw ba ñu muju bòot
Africa sax ci di tuuri ragoñ
I wanna see you brothers free
Don't tryna copy Babylon no more
I wanna see you sisters free
Don't tryna change your skin no more
Oh proud to be black yeah yeah
We nuh love di other People oh no
Oh never lose our pride yeah
Never ever forget where you're
Liberté amul price ow yeh
Ñun de waruño setan muy ñaawe yow
Ñu fexe ba woywa bumu réero
Dëgg dëgg woywa warula réero
Lele lee lee lelee lee ma woy
Yow de wonala wonala wonala
Alioune Badara Gaye sama maam
Mame Fatou Fallay yaay ja
Mame Fatou Fall mu Ndew Gueye ak
Dëgg dëgg woy nala bakk nala
Ibrahima Khalilou Laye ak Mame Penda Seckay
Maam de newonama Nekk gone
Te ñakk bumu la te xam ki nga done
Sët bu bëgge baax dey donnu maam ye yow
Suma sañon don nitu demb ni
Woy nako ci wajuuram ga Ngala
Ñawulo Gaye ku baax nga yooo
Yagg Ngako wasare dara ñaawulo
Yagg Ngako wasare dara ñaawulo