Sama Xoll Nga Yoré, Mom Lala Topé…
Loumou Gouddi Gouddi Gouddi,
Baby I Follow You,Cause My Heart Is On You, Youuu
Baby I Follow You,Cause My Heart Is On You, Youuu
Ohohohh, Pourtant Joxnala Lepp
Ohohoh, Pourtant Je T’ai Tout Donné,
Xamna Bou Baax Lingay Bañ
Dem Bacca Biir Malay Gagn
Man Ma Yitté Wola Lool Sax
Massamba Ming May Gagn Ayy
Kayy Gaaw,Deugg Leu Ni Deungg Nayy
Souma Démé Balay Way Nga Xamni Caxaan Taxoul
Ohohohh, Pourtant Joxnala Lepp
Ohohoh, Pourtant Je T’ai Tout Donné, Tout Donné
Man Douma Say Say,Lathko Sama Gayi
Boul Meusseu Gaday,Donal Sen Yaye
Ndiabott Gui Kay Way Goungué Maaa
Man Douma Say Say,Lathko Sama Gayi
WRITERS
Prince Arts, Prince Ibrahima Ndour, Nick Silver, Sakhir Niang, Saliou Samb